Photo by Gavyn Redd
Baay
Baay, sunu baay bi
Baay dundal
Na sa tur sell
Na sa nguur dëgër
Ndax sag dundu am na ñjariñ
Baay dundal yàgg fi te wér
Lo nekk baay Yàllaa nay jàmm
Baay, sunu baay bi…
Maky Madiba Sylla
December 12, 2023
October 24, 2023